Surgay Daawuda ya dem ca Abigayil ca Karmel, wax ko ne ko: «Daawudaa nu yónni fi yaw, ngir bëgg laa jël soxna.»
TSK
TSK · Proverbs 11:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye ba mbir ma àggee ca Buur, Buur a joxe ay ndigal yu ñu bind, ne pexe mu bon ma Aman nasaloon Yawut yi, na walbatiku këppu ci kaw boppam. Te mook ay doomam yu góor dees leen di wékk ci bant.
Yéeneleen ca biir taaxi Asdodd ak ca biir taaxi Misra. Neleen: «Dajeleen ca kaw tundu Samari, ba gis na Samari salfaañoo, ak notaange ga fa nit di daj.
Ndaxam lenn doŋŋ a manula ñàkk. Maryaama nag, cér bi gën la taamu, te deesu ko nangu ci moom.»
Mu gis itam ab jëtun bu néew doole, mu def ca ñaari poseti xànjar.
As ndaw a nga ca, di déglu; ku ñuy wax Lidi, dëkke Catir, di jaaykatub cuubi tànnéef yu xonq curr, te di jaamukatu Yàlla. Boroom bi nag ubbi xolam, ba mu teewlu bu baax kàdduy Póol.
Nuyul-leen ma Maryaama, mi sonn lool ci yeen.