TSK

TSK · Proverbs 11:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Buleen seet fi mbooloo gëna baree, ngeen topp leen ci jëf ju bon; te it buleen jeng, di topp mbooloo mu gëna bare ci ab layoo, di leen seedeel lu toxal dëgg.

Job 36:17 TSK

Waaye añu ku bon duunal na la, dëgg ak yoon ne la taral.

Màggal-leen Ki Sax! Ndokklee ku ragal Aji Sax ji, di tàqamtikoo ay santaaneem.

Aji Sax ji sib na ku réy, da koy mbugal ci lu wér.

Maa leen di may benn xol ak benn jubluwaay ngir ñu di ma wormaal seen giiru dund, muy seen ngëneel, ñook seen doom yi leen di wuutu.