2 Samuel 7:14
TSK
Man maay doon baay ci moom, moom, muy doom ci man. Su defee naka su dul noonu, maa koy yare bantu nit, ak dumay doom aadama.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Man maay doon baay ci moom, moom, muy doom ci man. Su defee naka su dul noonu, maa koy yare bantu nit, ak dumay doom aadama.
Mu dem, gaynde dogale ko, rey ko, néewam ne lareet ca yoon wa, mbaam maak gaynde ga taxaw ca wet ga.
Njaatige luy liggéeyloo ab dof ak kuy romb, daa mel ni fittkat buy gaañ ku ne.
Maay delloo àddina mbonam, yool ku bon tooñam, maay sàggi sagub ku reew, detteel puukarey ku néeg.
¶ «Leween ñi ma sore woon ba bànni Israyil jàddee, ba dëddu ma, di topp seen kasaray tuur, ñooy gàddu seenu ay.
Looloo tax ngeen bare ñu néew doole, ak ñu xiibon, ba lim bu takku dee.