2 Samuel 17:1
TSK
¶ Gannaaw loolu Ayitofel ne Absalom: «Ngalla may ma, ma tànn fukki junniy xarekat ak ñaar (12 000) te dàqi Daawuda ci guddi gi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Gannaaw loolu Ayitofel ne Absalom: «Ngalla may ma, ma tànn fukki junniy xarekat ak ñaar (12 000) te dàqi Daawuda ci guddi gi.
Ndax dañu noo fexeel maak samaw xeet, nar noo sànk, bóom nu, faagaagal nu. Su doon ay jaam yu góor ak yu jigéen sax lañu nuy fexee def, dama naan cell, ndax njàqare ju ni tollu sax jarul ñuy lëjal Buur.»
Ab dof a ngi réy-réylu, làmmiñam yar ko; ku rafet xel, sa kàddu aar la.
«Waaw! Daa am ñu bon ci sama ñoñ, ñuy tërook a fiire mbete nappkati picc.
¶ Ba bët setee Yawut ya daje, daldi xasoo, ne duñu lekkati, duñu naanati, ba kera ñu reyee Póol.
tinu ko ngir mu woolu Póol Yerusalem, ndax fekk na leen lal pexem rey ko ca yoon wa.