TSK

TSK · Proverbs 13:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ca bés booba ay surgay Isaaxa ñëw nañu, di ko wax lu jëm ci teen, ba ñu doon gas, ne ko: «Gis nanu ndox.»

Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan ñàkk bopp la.

Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.

Ab yaafus da naan: «Gayndee ngi ci yoon wi! Gayndee ngi ci mbedd mi!»

¶ Loolu ci boppam wara tax ngeen def lu ngeen man, ba dolli ci seen ngëm, njàmbaar; seen njàmbaar, ngeen dolli ci xam-xam;