TSK

TSK · Proverbs 16:33

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ab tegoo bant doŋŋ lees di séddalee réew mi, te seen limu giiri maam ya ñu bokk, na dëppook seenub cér.

Sóol ne: «Tegal-leen nu bant sama digganteek Yonatan.» Ñu tegal leen, mu dal ca doomam Yonatan.

Tegoo bant day feyu ay, di àtte boroom doole yu jote.

Jonah 1:7 TSK

¶ Ci biir loolu ku nekk naan sa moroom: «Ayca nu tegoo bant, ba xam musiba mii nu dal, ku nu ko yóbbe.» Ñu tegoo bant, mu dal ca kaw Yunus.