TSK

TSK · Proverbs 17:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

te gis na doomi Efrayim, ba gis sëti Efrayim sax; rax ca dolli doomi Makir, mi Manase jur, fa kanamam lañu juddoo.

Waaye duma ko def ci sag dund ngir sa baay Daawuda. Ci sa loxol doom ju góor laa koy foqatee.

Job 42:16 TSK

Gannaaw loolu Ayóoba dundaat na téeméeri at ak ñeent fukk (140). Gis na ay doomam, gis ay sëtam, ba muy ñeenti maas.

Sa jabar ni garab gu nangoo sa wanag, say doom wëra wër sa ndab ni njëmbat lu jebbi.

Bijjaawu bopp kaala gu yànj la, njekk a koy maye.