TSK

TSK · Proverbs 20:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 28:18 TSK

waxeesuli xor ak yeneen xeeti per; xel mu rafet a gën per yu gëna jafe,

Xel mu rafet a gën gànjar; loo mana bëgg moo ko raw.

Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.

Kàddug ku jub di ngën-gi-xaalis, xelum coxor amul solo.

Nit bége na tontam lu dal, kàddu gu jib fa mu ñoree neex!

Ki rafet xel mooy kiy ràññee, te su wax rafetee, dég-dég yomb.

Kàddu yu lay yedd ci kuy dégg, jaarob wurus la mbaa gànjaru ngalam.

¶ Waaye nees di wooye koo gëmul? Nees di gëme koo déggul turam? Nees di dégge turam, te yégleesu ko?