Proverbs 21:20
TSK
Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
ndax ku bëgg lekk ak a màndi, ñàkk dab la, dajjant it, rafle rekk.
Mu xaacu ne: “Maam Ibraayma, yërëm ma! Yebalal Lasaar, mu sëpp catal baaraamam ci ndox, dikk seralal ma sama làmmiñ, sawara sii metti na lool!”
ay workat lañuy doon, ñu teeyadi, ñu daŋŋiiral te di ñu bëgg seen bànneexu bopp, ba mu gënal leen Yàlla.