TSK

TSK · Proverbs 21:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Xooleel, sa bët ne jàkk, ngay xool sa kanam màkk.

Ku mat, njekk xàllal la; coxor daaneel boroom.

Ku ñuy àrtu, nga të ticc, dangay jekki yàqu, ba wees am paj.

Moo tax waame aje, taw yiy mujje dikkul. Teewul ngeen dëgër bët nib gànc, ñàkk gàcce!

Ñu wara am gàcce ci seen jëf ju siblu, te gàcce gàcceelu leen. Xamuñu sax luy kersa! Moo tax ñuy fëlëñoondook ñiy fëlëñu. Kera ba ma leen di dikkal, ñooy tërëf.» Aji Sax jee ko wax.

Ndegam moo xoolaat, ba dëddu mboolem tooñam yu mu tooñ, dina dund déy. Du dee moos.

Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Teewlooleen xel seeni jaar-jaar.

Seetaatleen seen xel bu baax, dale ko bésub tey jii, dale ko ci ñaar fukki fan ak ñeentu juróom ñeenteelu weer wi, daleleen ci bés bii kenug néegu Aji Sax ji tegee, ngeen seetaat seen xel.

¶ Yal na Yàlla sunu Baay ci boppam, ànd ak sunu Sang Yeesu, ngir jubal sunuw yoon ba nu agsi ci yeen.