Genesis 41:46
TSK
Ba Yuusufay tàmbalee liggéeyal Firawna buuru Misra, mu ngi tollu ci fanweeri at. Yuusufa daldi bàyyikoo ca Firawna, wër réew ma mépp.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba Yuusufay tàmbalee liggéeyal Firawna buuru Misra, mu ngi tollu ci fanweeri at. Yuusufa daldi bàyyikoo ca Firawna, wër réew ma mépp.
¶ Ci kaw loolu ñu dégg kàddu ya ca Daawuda wax, yegge ko Sóol. Sóol woolu ko.
Ndokklee say nit! Ndokklee sa jawriñ ñii dëkke taxaw ci sa kanam, di dégg sam xel!
Njaxlaf, jiitu; yaafus, des gannaaw.
Ñu diy waxambaane yu amul benn sikk ci seen yaram, di ñu góorayiw, mane bépp xeetu njàng, bare xam-xam te am déggin, ba mana liggéeyal Buur ci biir këram. Ñu di leen jàngal làkku waa Babilon ak seen mbind.
Sawarleen te baña yoqi, jaamuleen Boroom bi, ànd ceek pastéefu xol.