TSK

TSK · Proverbs 23:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bët yaa ngay nes-nesi ndax biiñ, bëñ ya weex furr ndax um soow.

¶ Ba mu ko defee Absalom sant ay nitam, ne leen: «Ma ne, bu Amnon naanee biiñ, ba xolam sedd, bu ma leen nee ngeen jam ko rekk, reyleen ko. Buleen ragal; man maa leen ko sant. Góor-góorluleen nag te ñeme.»

Naan biiñ ak ñaawle, naan ñoll, tanqale, ku mu nax xeluwoo.

Wóoy ngalla ñiy teela xëy, daw wutiw ñoll, gonloo biiñ ba tàng jérr.

Ñii itam ay naan biiñ bay tërëf, màndiw ñoll, di jang: sarxalkat akub yonent la aw ñoll di tërëfloo, biiñ jànnaxe leen, ñu màndiw ñoll, di jang, bu ñu amee am peeñu, di tërëf.

Buleen naan biiñ ba màndi, màndite ci afal seen bakkan la leen jëme, waaye na leen Noo gi fees,