TSK

TSK · Proverbs 27:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ba ku ma kókkali, ma am tontam. Maa doyloo sa kàddu.

¶ Kàddu yu xelu yu Suleymaan. Doom rafet xel, baay ba bég; doom dof, ndey ja tiis.

Deel bégal ndey ak baay, rawatina ndey ji la jur.

Sama doñ-doñ, ji fi kaw dun bi, génnliku na ma, dama koy wacce ka may wuutuji rekk,

Man Póol maay bind fii ci sama loxol bopp: maay fey loolu, duma ci tuddaale bor bi nga ma ameel, te muy sa njotug bakkanu bopp!