TSK

TSK · Proverbs 27:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yanqóoba ne ko: «Sang bi, xam nga, xale yi dañoo néew doole, te it gàtt yi ak nag yiy nàmpal laay xalaat. Su nu leen sëqatalee benn bés rekk, gàtt yépp dee.

da ne leen: «Defleen seen xel ci mboolem kàddu yi ma leen di artoo man, bésub tey, te ngeen sant seeni doom ñu sàmmoo jëfe mboolem kàdduy yoon wii.

Yeen sama jur gi, sama juru parlu mi, yeenay nit ñi may sàmm, may seen Yàlla. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.»