TSK

TSK · Proverbs 29:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci biir loolu Sóol sant ay dagam, ne leen: «Diisool-leen maak Daawuda, ngeen wax ko ne ko: “Yaw kat, Buur am na bànneex ci yaw, te it dagam yépp a la sopp. Kon nag nangula doon gorob Buur.”»

¶ Ba loolu amee waa Sif dem Gibeya ca Sóol, ne ko: «Daawuda de, ma nga làqu fa nun. Ma nga ca xunti yu kawe ya ca Orsa, ca kaw tundu Akila, fa féete màndiŋ ma bëj-saalum.

¶ Rekab ak Baana, doomi Rimon ma dëkk Berot nag ñoo demoon kër Isboset, àgg fa ci biir tàngooru njolloor, fekk Isboset di for bët.

¶ Ba mu ko defee Yewu bind leen ñaareelu bataaxal, ne leen: «Ndegam man ngeen àndal te sama kàddu ngeen di dégg, dogleen seen boppi doomi sang yu góor te fekk ma fii ci Yisreel nëgëni ëllëg.» Booba doomi buur yu góor juróom ñaar fukk lañu, nekk ak kàngami dëkk ba leen yar.

Kuy jëw moroomam, ma wedamal; ku daŋŋiiral ak ku reew, muñaluma la.

Jëw, mer a cay topp; mooy ngelawal taw, taw a cay topp.