TSK

TSK · Proverbs 30:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Nabal la waa ji tuddoon, soxnaam di Abigayil. Ndaw su yewwu la woon te taaru, jëkkëram nag bokk ci giiru Kaleb, di ku ñàng te soxor.

Sang bi, bul déglu mukk nit ku bon kii, Nabal mii. Moom turam doŋŋ la wuyu, nde Nabal (Dof bi) la tudd, te ndof la nekke. Man nag sang bi, gisuma woon ndaw yi nga yebal.

¶ Ci kaw loolu waa ja yóbbu Daawuda, ndeke nit ñaa nga ne wesar ca àll ba bépp, di lekk ak a naan, di mbumbaaye mboolem alal ju bare ja ñu nangoo ca réewum Filisti ak réewum Yuda.

Ku ñàkk, su jekkoo ab ndóol, du ko bàyyil fepp, day mel ni waame.

«Maay def ay gone jiite leen, di ñu yaroo seen sago, yilif leen.