TSK

TSK · Proverbs 9:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Xel mu Rafet a ngay woote ca mbedd ma, di xaacu ca pénc ma.

Day toog bunt këram, mbaa fu kawee kawe ca dëkk ba,

Looloo tax itam kàddug Yàlla giy xel, biral ne: “Maay yebal fa ñoom ay yonent aki ndaw, ñii ñu bóom, ñee, ñu bundxatal.”

¶ «Surga ba dellu, daldi koy àgge boroom kër ga, njaatigeem. Mu mer, ne surga ba: “Demal gaaw ca pénc yaak mbeddi dëkk bi, te nga indi fii néew-doole yi, ak làggi yi ak silmaxa yi ak ñiy soox.”

Kon nag Almasi, noo diy ndawam, te ci nun la Yàlla di wootee. Kon ci turu Almasi, danu leen di ñaan: nanguleena juboo ak Yàlla.