Genn kër lees koy lekke: bu lenn ci yàpp wi génn kër gi, te deesu ci damm benn yax sax.
TSK
TSK · Psalms 34:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ci kaw loolu Yonatan wax baayam lu baax ci Daawuda, ne ko: «Buur, ngalla bul tooñ Daawuda, sa jaam bii, ndax moom kat tooñu la, lu baax rekk la la masa defal.
Buurub Israyil ne Yosafat: «Am na ba tey genn góor gu ñu mana seetal ci Aji Sax ji. Waaye man maa ko jéppi, ndax du wax waxyu bu baax ci man, lu bon rekk; mooy Mise doomu Yimla.» Yosafat ne ko: «Buur, bul waxe noonu.»
Ñiiki watiir, ñeeki fas, nun sunu turu Yàlla Aji Sax ji lanuy tudd.
Kàddug aji jub day xelu, wax ja jub;
Noon du ko bett, ku bon du ko torxal.
Ku jub day daanu juróom yaari yoon, jógaat, ab soxor sërëx ci njekkar.
Waaye waa réewam ña dañu koo bañoon. Ci gannaawam lañu yónni ndaw, ne: “Kii, bugguñu muy sunu buur.”
¶ Ba Yeesu jubsee ba séen dëkk ba, jooy na ndax moom.
Te kat njekku Yàlla dina feeñ ndax coono ba muy delloo ñi leen teg ab coono.