yafloo sa njël lu duun, sa xéewal wal, nga nàndale ko.
TSK
TSK · Revelation 21:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
«Éey, yeen ñi mar ñépp, dikkleen ci ndox mi, ba ci ku amul xaalis sax! Dikkleen jënd pepp, lekk! Dikkleen jënd pepp mu xaalis jëndul, ak biiñ ak meew mu amul pey.
Asiri du nu xettli, ay fasi xare it, dunu ko war, te dootunu wax lu nu sàkke sunuy loxo, ne ko: “Yaw yaa di sunu Yàlla.” Li nuy wax kay mooy yaw yaay kiy yërëm jirim.»
Moom mi nu bañalul Doomu boppam, xanaa jooxeel nu ko, nun ñépp, ana nu mu nuy baña baaxee gépp yiw, boole ci?
¶ Ana kuy Apolos sax? Ak kuy Póol? Xanaa ay surga doŋŋ yu ngeen jaare, ba gëm, ni Boroom bi jagleele kenn ku nekk ci nun, aw sasam.
¶ Kon nag bu kenn puukarewoo ay nit, ndax lépp, yeena ko moom,
¶ «Man, maay Alfa, di Omega», la Boroom bi Yàlla wax, moom Ki masa Nekk, Ki Nekk, di Kiy Dikk ëllëg, te di Aji Man ji.
¶ Naka laa ko gis, ne dàll daanu ci ay tànkam ni ku dee. Mu teg ma loxol ndijooram, ne ma: «Bul tiit. Maay Ki Jëkk, di Ki Mujj.
Mu giñ ci Kiy dund ba fàww, Ki sàkk asamaan ak li ci biiram, ak suuf ak li ci biiram, ak géej ak li ci biiram. Mu ne: «Négandiku wees na,
Man maay Alfa di Omega; maa jëkk, maa mujj, maay njàlbéen, maay muj.