¶ Musaa teg ca ne leen: jant yooyu laa leen wax, ne leen: «Duma leen àttan yeen ñépp, man doŋŋ.
TSK
TSK · Romans 13:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waa Siri ña dëkke réewum Damaas dikk wallusi Adadeser buurub Soba. Daawuda rey ca ñoom ñaar fukki junneek ñaar (22 000).
Léegi nag Buur, xamal ne bu ñu tabaxaatee dëkk boobu, ba yékkatiwaat tata ya, galag mbaa njoti bopp mbaa juuti dootuñu ko fey, te kon koomu nguur gi dina ko yég.
¶ Rax ci dolli ndigal a ngii tukkee ci man, jëm ci li ngeen wara defal magi Yawut yooyu ci biir liggéeyu kër Yàlla googu: Njég ga mu leen dikke, nañu leen ko fey ba mu mat, jële ko ca alali buur, ca galagi diiwaan ba ca Wàllaa Dex. Nañu ko fey ñooñu, ba liggéey ba baña taxaw.
Bu ma génnaa ba ca bunt dëkk ba, digg pénc ma laay jekkasndikoo,
Yeerukat ya dikk ne Yeesu: «Sëriñ bi, xam nanu ne njub ngay wax, di ko jàngle. Amuloo parlàqu itam, waaye ci kaw dëgg ngay jànglee yoonu Yàlla.
Su dee wàllu kàddu yuy yokke, ngay wax luy yokk gëmkat ñi; su dee wàllu joxe, deel joxe te Yàlla rekk tax; su dee wàllu jiite, taxawal temm ci liggéeyub jiite; su dee wàllu baaxe nit ñi, nay loo bége.