Genesis 4:7
TSK
Soo defee lu baax, dees na la nangul; soo deful lu baax, bàkkaar a ngi lay yeeru ci sa bunt, di la tërook a wut, waaye yaa ko wara man.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Soo defee lu baax, dees na la nangul; soo deful lu baax, bàkkaar a ngi lay yeeru ci sa bunt, di la tërook a wut, waaye yaa ko wara man.»
¶ Booba fekk na àddina yàqu, te fees ak ay, Yàlla teg ci bëtam.
Waaye waa Sodom ñu bon lañu woon, te mana moy Aji Sax ji lool.
¶ Teewul bala ñoo tëdd, góori Sodom, mag ak ndaw, daldi jóge gox bu nekk, ñëw yéew kër ga.
¶ Noonu la ñaari doomi Lóot def ak seen baay, daldi cay doxe ëmb.
Aji Sax ji ñaawlu li muy def, ba tax mu faat ko, moom itam.
Ndee, ag fittam mooy bàkkaar, te bàkkaar, dooleem mooy Yoon wi.