2 Samuel 1:6
TSK
Ndaw la ne ko: «Dafa yemook ma tollu tembe ca kaw tundu Gilbowa. Ndeke Sóol a nga fa, sukkandikoo xeejam. Watiiri xare yaak gawar ya defuñu lu moy ne ko dann.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndaw la ne ko: «Dafa yemook ma tollu tembe ca kaw tundu Gilbowa. Ndeke Sóol a nga fa, sukkandikoo xeejam. Watiiri xare yaak gawar ya defuñu lu moy ne ko dann.
Gewasi nag di nettali Buur na Alyaasa dekkalee woon xale ba, rekk ndaw sa Alyaasa dekkaloon doomam ju góor ne jalañ, di sàkkusi ca Buur mu jox ko këram ak suufam. Gewasi ne ko: «Ndaw saa ngii nag, Buur, sang bi. Doomam ju góor jii la Alyaasa dekkaloon.»
Sàkkuleen di jëfe jëfin wu dal, te ngeen di topptoo lu seen yoon nekk, tey dunde seenu ñaq, na nu leen ko sante woon.