TSK

TSK · Ruth 4:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Gannaaw ga soxnas Isaaxa amul doom, Isaaxa dagaanal ko Aji Sax ji, mu nangul ko, soxna si daldi ëmb.

Yanqóoba mere ca Rasel ne ko: «Ndax maay Yàlla, mi la teree am doom?»

¶ Naka la Esawu siggi, gis jigéen ñi ak xale yi, mu ne: «Ñii ànd ak yaw ñooy ñan?» Yanqóoba ne ko: «Xanaa njaboot, gi ma Yàlla baaxe, sang bi.»

Ruth 4:12 TSK

Njaboot gu la Aji Sax jiy may ci ndaw sii, yal na ñu lawal saw askan, ba mu mel ni askanu Peres, ma Tamar am ak Yuda.»

Ña reggoon, bindu, di dunde, ña xiifoon, noppee liggéey. Jigéen ju njur të woon jur juróom yaar, ku jur góori góor jeex tàkk.

Ma ne, doom Aji Sax jee koy sédde, njurum doom yool la.