TSK

TSK · Titus 2:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Du lenn lu ma xemmem ci kenn; du xaalis, du wurus du koddaay.

Nun nag danoo melul ni ñu bare, ñiy julaa kàddug Yàlla, waaye ci ndigalal Yàlla ak fi kanam Yàlla la nuy waaree xol bu set, ci Almasi mi nu gëm.

¶ Du ndigal lu ma leen jox, waaye njaxlafug yeneen gëmkat, moom laay natte seen xol, ngir xam nu seen cofeel dëggoo.

ba mana xàmmi li gën. Su ko defee ngeen set wecc te mucc sikk, ngir keroog bésub Almasi.

Bu la kenn xeebe sa at yu néew, waaye nanga doon royukaayu gëmkat ñi ci wax ak jëfin, ak cofeel, ak ngëm, ak dundin wu set.