TSK

TSK · Zechariah 2:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ñu baree may tooge naa: «Yàlla du ko wallu!» Selaw

Jekk taxawaayee tundu Siyoŋ, catu bëj-gànnaar, dëkku buur bu mag bi, di mbégtem àddina sépp.

Su boobaa tundu Siyoŋ bépp, fépp fu ñuy dajee, Aji Sax ji sàkk fa niiru saxar bëccëg, guddi mu def tàkk-tàkk bu ne ràññ; leeru Aji Sax ji di kiiraay, tiim lépp,

Bésub keroog dees na woy wii woy fi réewum Yuda: «Dëkk bu dëgër lanu am, Yàllaa nu may kaarangey tata, biir ak biti!

Deesatul dégg ci sam réew: «Fitna ñëw na!» deesatul dégg it fi sa kemu suuf: «Yàqute ak Yàqulee ngi!» «Mucc» ngay tudde say tata, te «Cant» ngay tudde sa bunti dëkk.

¶ Waa jaa nga jubal penku, ŋàbb buumu nattukaayam, daldi natt junniy xasab. Mu jàlle ma ba foofa, ndox ma yem ma ci kostan.

Moo tax Aji Sax ji dafa wax ne: “Yërmande laay dellusee Yerusalem. Sama kër lees fay tabaxaat.” Kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi. Mu ne: “Buumu nattukaay dina tàllalu ci kaw Yerusalem.”

Luke 2:32 TSK

mu dig leer, ñeel jaambur ñi, sagal Israyil sa ñoñ.»

Te dëkk bi soxlawul jant bu koy leeral mbaa weer, ndax leeru Yàllaa koy leeral, Gàtt bi di làmpam.