TSK

TSK · Acts 16:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Luke 4:20 TSK

¶ Ci kaw loolu mu ub téere bi, delloo ko jawriñ ba, daldi toog. Ña ca jàngu ba ñépp nag ne ko jàkk.

¶ Ba ñu génnee ca jàngu ba, dañu leena ñaan ñu baamtu kàddu googu bésub Noflaay ba ca topp.

Acts 17:2 TSK

Póol nag di leen fa fekk, na mu ko baaxoo. Diiru ñetti bési Noflaay, mu di leen waxal ci Mbind mi.

Acts 20:7 TSK

¶ Ca ndoortel ayu bés ba, naka lanu daje ngir dagg mburum bokkoo mi, Póol, yékkati kàddu, di wax ak gëmkat ñi, ndax fekk na mu bëggoona dem ca ëllëg sa. Wax ja nag law ba guddi ga xaaj.

Kon nag amul Yawut ak ku dul Yawut, amul ab jaam ak as gor, amul góor ak jigéen. Yeen ñépp benn ngeen ci Almasi Yeesu.