كل أسفار KYG

Acts 21

KYG · الآية 26

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 21

KYG · الآية 26

C a ëllëg sa Póol ànd ak nit ña, bokk ak ñoom setlu, dugg ca kër Yàlla ga. Mu daldi xamle bés ba seen àppu setlu di mat, ba jooxe ba ci war génn, ñeel kenn ku nekk ci ñoom.