TSK

TSK · Daniel 11:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Guddig keroog maay wër réewum Misra te maay fàdd lépp luy taaw bu góor ci réewum Misra, nit ak mala, te itam maay mbugal mboolem tuuri Misra. Man maay Aji Sax ji.

Tojleen seeni sarxalukaay, rajaxe seen tuuri doj; seen xer yi ñuy jaamoo Asera tuur mi, ngeen lakk; seen jëmmi tuur, ngeen gor, ba far tukkal turi tuur yi ci yooyu bérab.

Waa Filistee fa wacc seeni gàllaaj, Daawudaaki nitam boole yóbbu.

te ñoo sànni seeni yàlla ci sawara it, ndax yooyoo dul Yàlla, xanaa lu nit sàkke loxoom, bant ak doj, ba tax ñu sànk leen.

Nabukodonosor dina jafal kër tuuri Misra yi, lakk tuur yi, mbaa mu yóbbu leen. Ni ab sàmm di teeñe mbubbam, ni lay teeñe réewum Misra ba mu set wecc, daldi daagu, dem yoonam.

Boroom bi nag teg Yowakim buurub Yuda ciy loxoom, boole ca lenni jumtukaayi kër Yàlla ga. Nabukodonosor yóbbu jumtukaay ya réewum Sineyaar, ga ñuy wax Babilon itam, ca biir kërug tuuram. Mu daldi fat jumtukaay ya ca denci kër tuuram.

Hosea 8:6 TSK

«Israyil la lii jóge, te ab liggéeykat moo ko sàkk. Kon lii du Yàlla! Ay tojit la wëlluw Samari di mujje.

Efrayim moom, su naatee ci biiri bokkam it, fa màndiŋ ma la ngelawal penku, ngelawal Aji Sax ji di uppe, bëti ndoxam tëju, ay teenam déy. Kii mooy sëxëtoo ab dencam, ak mboolem lu cay alal.»