Buuri àddinaa ngi dér, boroom nguur yi daje, di fexeel Aji Sax ji, mook ki mu fal.
TSK
TSK · Daniel 6:7
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Xettlimaak ñiiy def lu bon, wallu maak bóomkat yi.
Xanaa dungeen bàyyee songandoo nit, nar koo sànk, ni kuy màbb tabax bu joy, mbaa ngay bàddi per mu ràpp?
Di woyu Sabóor, giiroo ci Asaf. Éy Yàlla, bul ne cell,
Xërëmkat ya ne Buur ci làkku arameen: «Guddalu fan Buur, sang bi! Wax nu gént gi, nu firi ko.»
Képp ku sujjóotul màggal ko, dees koy daldi sànni ci biir taal bu yànj.»
¶ Ba loolu amee jawriñ yaak laman yaak jaraaf yaak dagi Buur yéew leen. Ñu gis nag ne sawara wi lakkul seen yaram fenn, seen kawaru bopp xoyomuwul, seeni yére yàquwul, xeeñuñu sax xetu sawara.
¶ Dañeel daldi ne Buur: «Buur, guddalu fan!
Moo ana paxum gaynde ga? Ana àllub gaynde yu ndaw ya, fa góoru gaynde daa daagoo, mook jeegub gayndeem ak doom ya, te dara tiitalu leen!
Buuri àddinaa jógandoo, kilifa yee lëkkoo ci kaw Boroom bi ak Almaseem.”