TSK

TSK · Daniel 7:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Sa gannaaw geneen nguur dina taxaw, gën laa suufe, ñetteelu nguur ga topp ca di xànjar, tiim àddina sépp.

May xool, ab sikket jóge sowu, jaare déndu suuf sépp te laalul suuf. Sikket baa nga am béjjén bu yéeme ci diggante bët yi.

Sikket bi buuru réewum Geres la. Béjjén bu gudd bi ci diggante bët yi mooy buur bu jëkk bi.

Waaye buur bu jàmbaare dina falu, di boroom kilifteef gu yaatu, di def lu ko soob.

Rab wi ma gis ni segg la mel, tànk yi mel ni yu urs, gémmiñ gi mel ni gu gaynde. Ninki-nànka ji jox ko kàttanam ak nguuram ak sañ-sañam bu réy.