¶ Ca jamonoy Amrafel buurub Sineyaar, ak Aryog buurub Elasaar, Kedorlamer buurub Elam, ak Tidal buurub Goyim,
TSK
TSK · Daniel 8:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Mbiri Neyemee ngi, góor gay doomu Akalya: Ca ñaar fukkeelu atu nguurug Artaserses, ci weeru Kislew, man Neyemi maa nga woon ca Sus, péey ba.
¶ Gannaaw ba ñu yéenee ndigalu Buur ak dogalam ba, ñu dajale janq ju bare ca Sus, péey ba, teg leen ca loxol Ege. Noonu lañu indaalee Esteer, ba ca kër Buur, teg ko ci loxol Ege may wattu jigéen ña.
Esteer ne ko: «Waa ji nuy fexeel, di bañ, dib noon de, Aman mu bon mii la!» Aman nag tiit lool fa kanam Buur ak Lingeer.
¶ Bésub keroog ñu yegge Buur limu nit ña ñu rey ca Sus, péey ba.
Bésub keroog Boroom bi jooti loxoom ñaareel bi yoon, ngir jotaat ndesu ñoñam, wa des Asiri ak Misra, ak Pattros ak réewum Kuus, ak Elam ak Sineyaar, ak Amat ak biir duni géej ya.
ak mboolem buuri Simri ak buuri Elam ak mboolem buuri Medd,
«Buurub Elam a nga faak gàngooram gépp, seeni bàmmeel yéew bosam. Ñoom ñépp lañu jam, ñu fàddoo saamar. Paaxe lañu wàccaale xóotey suuf, te daan tiital waa réewum aji dund ña. Seen gàcce lañu gàlloo, ànd ak ñay wàcci biir pax.
¶ «Ba mu ko defee, man Dañeel, ma am njàqare; sama peeñu yooyoo ma tiital.
¶ Bu yàgg la Yàlla waxoon ay yooni yoon ak maam ya, ci waxin yu bare, yonent yi jottli.