Genesis 10:14
TSK
ak Pataruseen ñi ak Kasluyeen, ñooñee waa Filisti bàyyikoo ca seen réew; ak it Kaftoreen ñi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
ak Pataruseen ñi ak Kasluyeen, ñooñee waa Filisti bàyyikoo ca seen réew; ak it Kaftoreen ñi.
¶ Ba loolu amee Ibraayma jël ay gàtt aki nag, may ko Abimeleg, ñu fasoo kóllëre ñoom ñaar.
am géttu jur gu gudd ak gu gàtt, ak ay surga yu bare, ba tax waa Filisti iñaane ko,
¶ Firawna bàyyi na mbooloo ma, ñu dem, waaye Yàlla jaaralewu leen ca yoon, wa jëm réewu Filisti, doonte moo gënoona gàtt. Booba Yàlla dafa xam ne, su mbooloo ma sóoboo ci ay xare ci woowu yoon, dañuy yoqi, bay xalaata dëpp, dellu Misra.
Ba loolu amee Yonatan fasook Daawuda kóllëre, ndax sopp ko ni boppam.