TSK

TSK · Genesis 35:26

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

waaye demal Padan Aram ca sa kër maam-góor, ji jur sa yaay, nga jël fa jabar ca sa doomi nijaay Laban.

¶ Leya moom it xam ne taxawaayam yàgg na, mu fab jaamam Silpa, may ko Yanqóoba.

ñu ànd tegu ca yoon wa, yóbbaale géttam gépp ak mboolem alal ju mu liggéey. Mooy gétt, ga mu sàkkoo Padan Aram. Ña ngay ñibbi kër baayam Isaaxa ca réewu Kanaan.

¶ Doomi Gàdd yu góor ñoo di Cefon ak Agi ak Suni ak Esbon ak Eri ak Arodi ak Areli.