TSK

TSK · Genesis 39:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

ay goney Yàlla ñoo gis jigéen ñeek seen taar, ñuy jël ñi ñu bëgg ci ñoom, def leeni jabar.

Job 31:1 TSK

Maa jaayanteek samay gët. Ana nu may xooleb janq?

Xel mu rafet da lay musal ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.

Dogu mburu fey nab gànc; waaye jabaru jaambur, bakkanu lëmm.

Moo ma taxa dikk dajeek yaw. Seet naa laa seet, ba gis la.

Selebe yoon wu ne, tabax nga fa sa jaamookaay, di fa teddadil sab taar, ku romb, nga ràccal ko say tànk ci sa gànctu gu dul jeex.

Yaw kay sag ngànc bokkoo kook gànc yi. Kenn sàkkuwu la. Yaw kay yaay feye, kenn feyu la. Kon yaw meloo ni benn gànc!

Moom it waa Asiri ya la xédd, ñuy kàngam aki jawriñ, xarekat yu ràngu ba solu ba jekk, di ndaanaani gawar, ñoom ñépp di xale yu góor yu sopplu.

¶ Seeni gët xoolul lu moy ku ñu jaalool, te duñu bàkkaar ba regg mukk; ku dëgërul, ñu yóbbaale la. Ñooñu la seenub xol tàggatu ci ag bëgge, mii njurum alkànde!