TSK

TSK · Genesis 49:22

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Doomam ja ca topp mu tudde ko Efrayim (mu firi Giir), ndaxte da ne: «Yàllaa ma giiral ca réew, ma ma sonne.»

¶ Ba loolu wéyee ñu ne Yuusufa baayam dafa tawat, mu ànd ak ñaari doomam Manase ak Efrayim, seeti ko.

Ma ngay ñaanal Yuusufa. Mu ne: «Yàlla ji samay waajur Ibraayma ak Isaaxa toppoon, moom Yàlla, ji ma sàmm, ba ma juddoo ba tey jii,

Teewul baayam lànk, ne ko: «Xam naa ko, doom, xam naa ko. Moom itam dina doon aw xeet tey doon ku màgg, waaye rakkam a koy sut, te askanam dina law, ba di ay xeet.»

Yuusufa la wax, ne ko: Yal na barkeb Aji Sax ji ñeel suufam, bawoo ca xéewali asamaan, dib lay, ak ndox mu lal xóotey suuf,

Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Ndokklee képp ku ragal Yàlla, di jëfe ay yoonam.

Mu am car yu dëgër, yu man yeti nguur, daldi màgg ba àkki niir ya, ràññiku ci taxawaay ak sëqaay.