gësëm suuf fa mu tege, ay kenoom jaayu.
TSK
TSK · Haggai 2:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye fi leek lu néewa néew mbugal jeex fi seen biir, am sànj sippil Asiri seen sànkute.»
Xamuleen ne fi leek lu néewa néew, àllub Libaŋ sopplikub tóokër, tóokër bi walbatiku meññ, ba ñu ne ab gott la?
Maa xool suuf, ndeke ma nga ne maraas, ne wëyëŋ; ma xool asamaan, leer amatu ca.
jën ak njanaaw di lox fi sama kanam, ñook ndundati àll bi ak mboolem luy raam ak kuy nit fi kaw suuf. Tund yi màbb, doji mbartal ya fàqandoo, tata yépp jóoroondoo.
¶ «Ay firnde dinañu feeñ ci jant bi ak weer wi ak biddiiw yi. Ci kaw suuf njàqare ak tiitaange mooy ñeel xeet yi ndax riirum géej gi ak gannax yi,
Ndax kat, «Des nas tuut, as tuut rekk, kiy dikk, dikk te du yeex.
Ma xool rekk, gis fas wu weex, gawaram yor ag fitt. Ñu jox ko kaala, mu daldi dem yoonu daan-kat, ngir daani.
Diiru ñetti fan ak genn-wàll lañuy weeru, niti wépp xeet, ak gépp giir, ak wépp làmmiñ, ak wépp askan di seetaan seeni néew, te duñu bàyyi kenn suul leen.