xoolal képp ku bew, torxal ko, te dëggaate ku bon fa mu taxaw.
TSK
TSK · Malachi 4:3
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Aji Sax ji, néew-ji-doole, mu yenni; ku bon, mu daane ci suuf.
baadoola joggi, dëggaate, néew-ji-doole note leen.»
Sa ñaawtéef yu bare ak njublaŋ gi ngay julaa, looloo teddadil sa jaamookaay yu sell, ba ma jafale sawara fi sa biir, mu xoyom la. Maa la def ub dóom fi suuf, ñépp di la xool.
Palug mboolem nguur yi asamaan tiim, ak kilifteef gaak daraja ja dees na ko boole, jébbal aji sell yu Aji Kawe ji. Nguurug mbooloo moomu day sax ba fàww, kilifa yépp di ko déggal, di ko wormaal.”
Ndaw siy samab noon moo koy seede, sëlmoo gàcce, moom ma doon naa: «Ana sa Yàlla Aji Sax ji?» Samay gët a naa ndaw soosu jàkk, ñu di ko dëggaate ni banu mbedd.
«Sama moomeelu bopp la ñooñuy doon,» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax, «ca bés ba may jëfi, sama gànjar lañuy doon, te ni baay di baaxee as ngóoram su ko taxawu, ni laa leen di baaxee.
¶ Ba mu ko defee, juróom ñaareelu malaaka mi wal liitam, baat yu xumb jibe ca asamaan, ne: «Léegi nag nguurug àddina ñeel na sunu Boroom ak Almaseem. Mooy nguuru ba fàww.»