Psalms 31:20
TSK
Yàlla yaa yaa ngëneel loo dencal ku la ragal, defal ko ku la làqoo, doom aadama seede.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yàlla yaa yaa ngëneel loo dencal ku la ragal, defal ko ku la làqoo, doom aadama seede.
maa leen di dogalal saamar, ngeen bokk sukk, ñu rendi leen, ngir maa woote, wuyuwuleen, ma wax, dégguleen, xanaa di def li ma ñaawlu, taamu li ma buggul.»
¶ «“Gannaaw def ngeen jëf jii jépp nag,” kàddug Aji Sax jee, “te ma waxoon leena wax ay yooni yoon, dégluwleen; woo leen, wuyuwleen,
¶ Teewul ñu baña déglu, të ticc, fatt seeni nopp, ngir baña dégg.
Israyil nag la wax ci mbiram ne: «Bëccëg bépp laa yendoo tàllal samay loxo, askanu fippukat wu déggadi.»