TSK

TSK · Proverbs 14:31

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Bu seen mbokkum bànni Israyil ñàkkee ba manatula fey lu mu leen ameel, nangeen ko dimbali, ni bu doon doxandéem mbaa màngaan, ndax mu mana dund ci seen biir.

Ñu ngi naa: «Sunu làmmiñ lanuy daane, nook sunu kàddu; ku nu manal dara?»

Kuy ñaawal ku ñàkk, tooñ nga ka ko sàkk; kuy reetaan ku jàq, mbugalam du jaas.

Ku am ak ku ñàkk a bokk lenn: Aji Sax jee leen boole sàkk.

Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,

Gannaaw nag yeena duunle ci lépp; muy ci wàllu ngëm, ak wàllu kàddu yu rafet, ak wàllu xam-xam, ak cawarte ci lépp, ak ci cofeel gu nu leen xiir, kon ndajalem ndimbal lii it, ngalla duunleleen ci.