TSK

TSK · Proverbs 14:35

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Firawna daldi ne jawriñ ya: «Ndax masees naa gis ku mel ni kii a waay, nit ku Yàlla sol Noowug boppam?»

Kuy nas njekkar, sore ma; lu bon, xawma ko.

Wax ju dëggu, buur safoo boroom; ku jub, buur bëgg sa kàddu.

Merum buur ni gaynde gu ŋar; yërmandey buur ni lay cig mbooy.

Su buur toogee di àtte, day gis, di ràññee mboolem ayib.

Sang bi ne ko: «Ana kan nag mooy saytukat bu wóor te muus, ba njaatigeem batale ko curgag këram, ngir mu di leen jox seen njël ca ba muy jot?