Proverbs 3:7
TSK
Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;
Ana koo gis mu ne: «Maa xelu»? Kooku ab dof a ko gën demin.
Wóoy ngalla ñii defe ne ñoo xam, yaakaar ne ñoo muus.
¶ Kenn ca mbooloo ma moo noon Yeesu: «Sëriñ bi, waxal ci sama mag, mu jox ma sama wàll ci ndono li nu bokk.»
¶ Bokk yi, moytuleena defe ne seen xel mu rafet a leen may li ngeen am. Bugguma ngeen umple mii mbóot: Ag déggadi moo dikkal lennati bànni Israyil, ba kera xeet yi dul Yawut duggsi, ba seenub lim mat.
Loolu mu leen seedeel mooy dëgg, te moo tax nga war leena femmoo kàddu yu dëgër, ngir seen ngëm tegu ci àlluwa ji wér,