¶ Mu am bés nag soxnas sangub Yuusufa ba xemmem Yuusufa, daldi ne ko: «Kaay tëdd ak man.»
TSK
TSK · Proverbs 6:26
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 39:7
TSK
1 Samuel 2:36
TSK
Su ko defee mboolem ku des ci sa waa kër dina ko sujjóotalsi, ngir as xaalis mbaa as dogu mburu, naan ko ‘Ngalla sas ma lenn ci liggéeyu carxal gi, ndax ma am as dogu mburu su ma lekk’.”»
Proverbs 7:23
TSK
Mooy picc mu tàbbi cig fiir. Du xam ne day dee, ba keroog fitt jam ko ci xol.
Proverbs 29:8
TSK
Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
Ezekiel 13:18
TSK
Neel: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Wóoy ngalla jigéen ñiy sàkkal ku ne jarab xërëm, di ràbbal ku ne muuraayu xërëm bu ko jot, di ko moome nit ñi! Man ngeena aakimoo sama bakkanu ñoñ tey sàmmaale seen bakkanu bopp?
Luke 15:30
TSK
Sa doom jii dikk, gannaaw ba mu yàqee sa alal ci ay gànc, nga reyal ko sëlluw yafal wi!”