TSK

TSK · Proverbs 8:29

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 38:4 TSK

Ana foo nekkoon ba may samp suuf? Waxal su la ko sam xel mayee.

Job 38:11 TSK

ba ne ko: «Fii ngay yem, doo fi wees. Fii la say gannax di noppee buure»?

Yaa dëj suuf ciy kenoom, deesu ko yëngal ba fàww.

Moo sàkke asamaan manoore. Kee saxoo ngoram!

Man daal, dungeen ma ragal, am tiituleen ma?» Kàddug Aji Sax jee. «Man mi teg gannuus, yemalee ko géej, dogalal ko ko dàkk te du ko jàll, lu mu wañax wañax du ko man; gannax ya day riir, te du jàll!