TSK

TSK · Ecclesiastes 2:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Mu ne Buur: «Moo, man, Buur, lu ma deseeti ciy fan, bay ànd ak yaw dem Yerusalem!

Ñu daldi ànd dem Ofir, jële fa téeméeri barigoy wurus ak ñaar fukk, indil Buur Suleymaan.

¶ Wurus wa daan dikkal Suleymaan cim at, diisaay ba ñaar téeméeri barigoy wurus la,

Mu denc ca juróom ñaar téeméeri lingeer (700) ak ñetti téeméeri (300) nekkaale. Soxnaam ya nag dëpp ko.

Ba mu ko defee Buur Robowam defarlu ay pakku xànjar yu wuutu yu wurus ya. Mu teg ko ca loxoy njiiti dag yay wattu buntu kër Buur.

Job 21:11 TSK

Day gis ay xaleem di bajantu, goneem yépp di tëbantu.

Cóolóoloo cóolóol, waru waarekat ba, cóolóoloo cóolóol, léppi cóolóoli neen.

¶ Loolu nag waral saa yu nit ña déggee bufta gaak toxoro gaak xalam gaak riiti gaak kooraa gaak mboolem jumtukaayu xumbal ya, ñoom ñépp ay bokk sujjóot, màggal jëmmu wurus ja Buur Nabukodonosor samp, muy mbooloo yaak xeet yaak làkk ya.

Amos 6:5 TSK

yeena ngi foyantoo xalam, di fent woy yu ànd ak xalam ni Daawudaay.