All books in KYG

Acts 13

KYG · verses 4-5

28 chapitre

KYG / Acts / [JC0] chapitre 13

KYG · verses 4-5

4 Ñ o oñu la Noo gu Sell gi yebal, ñu dem dëkk ba ñuy wax Selusi, dugge fa gaal, jëm dun ba ñuy wax Sippar.

5 ¶ Ña nga teereji dëkk ba ñuy wax Salamin, daldi fay yégle kàddug Yàlla ca jànguy Yawut ya, ku ñuy wax Yowaan Màrk ànd ak ñoom, di leen jàpple.