Xanaa du ñu soxor ñaa ngii, bank seen xala, nas seenu fitt, nara lëndëmtu, jam ku jub?
TSK
TSK · Acts 24:1
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ba bés ba ñu jàpp agsee, Erodd sol colu buuram, toog ca jal ba, di leen àgge kàddug kilifteefam.
Anañas sarxalkat bu mag ba nag sant ña taxaw ca wetu Póol, ne leen: «Fél-leen gémmiñam».
Ba ñu ma àggee am tëru mu ko Yawut yi waajaloon nag, ci laa ko yebal ci yaw ci saa si. Jox naa itam ndigal ñi ko sikk, ne leen ñu wax ci sa kanam, gan tooñ lañu ko toppe.
Man ngaa leerlul sa bopp ne ba ma demee Yerusalem di màggali ak léegi weeseegul fukki fan ak ñaar.
Ba ma demee Yerusalem, moom la ma sarxalkat yu mag yeek njiiti Yawut yi booleeloon, di sàkku ci moom ab daan.
Sama kàddu ak samam njàngle jotewul woon dara ak neex làmmiñ gu xam-xamu nit ràbb, waaye dafa di ay firnde yu manooreg Noowug Yàlla lañal,