TSK

TSK · Acts 4:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 5:26 TSK

Ba loolu amee mbooloo mépp a neey, di sàbbaal Yàlla, tiitaange jàpp leen, ñu naan: «Gis nanu tey mbir yu tiiñ am xel.»

¶ Yeesu nag di jàngle bés bu nekk ca kër Yàlla ga. Ba mu ko defee sarxalkat yu mag ya, ak firikati yoon ya, ñook njiiti xeet wa, di ko wuta rey.

¶ Firikati yoon yaak sarxalkat yu mag ya nag, ca saa sa lañu doon fexee teg Yeesu loxo, ndax xamoon nañu ne ñoo moom léeb woowu, waaye nit ña lañu ragal.

Acts 4:17 TSK

Waaye kat bu mbir mi gëna siiw ci xeet wi. Nan leen tëkku, ngir aaye leen ñu waxati kenn tur woowu.»

Acts 5:40 TSK

¶ woowaat ndaw ya. Ba loolu amee ñu dóor leen, aaye leen ñu waxati lenn ci turu Yeesu, door leena yiwi.