Gannaaw loolu Yanqóoba dogu na ne: «Su Yàlla àndee ak man, di ma sàmm ci yoon wi may aw, di ma jox lu ma lekk ak lu ma sol,
TSK
TSK · Deuteronomy 23:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Bu ngeen dee lebal ku bokk ci sama ñoñ, di néew-ji-doole ju ngeen dëkkal, buleen def ni ab leblekat, di ko sas ab tegandaay.
¶ Ba mu ko defee Musaa àgge bànni Israyil mboolem la ko Aji Sax ji sant.
Jaambur bi bokkul ci bànni Israyil, sañ ngeen koo feyeeku, waaye la leen seen mbokkum bànni Israyil ameel, jéggaleleen ko.
Du leble, ba teg ca; du nangu ger, ngir fexeel jaambur. Lii ku koy jëfe doo jang.
Maay duggaale sa kër ay saraxi rendi-dóomal, defal la samay dige,
Samay digeek Aji Sax ji laay matal fi kanam ñoñam ñépp,
aw ndollant taxu koo leble, ab tegandaay, jëlu ko, xanaa luy njubadi, mu moyu, àtteb dëgg, mu doxal diggante nit ak nit,
Ñiy wormaal neenug neen daal, ñoo dëddu seen yiw fa Yàlla.