TSK

TSK · Deuteronomy 4:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Man itam Aji Sax ji mere na ma ci ndax yeen, ba ne ma: «Yaw itam doo ca dugg.

¶ Waaye ab ndóol du am ci seen biir, ndax seen Yàlla Aji Sax ji moo leen di barkeel bu baax ca réew ma mu leen di jox, muy seen cér, ngeen jagoo,

Su ko defee deesul tuur deretu jaambur bu deful dara ci suufas réew, mi leen seen Yàlla Aji Sax ji sédd, ba àqu deret di leen topp.

bu néewam fanaan ca garab ga, nañu ko daldi rob ca bés ba, ndax ki wékke alkàndey Yàlla la. Buleen sobeel réew mi leen seen Yàlla Aji Sax sédd.

¶ Gannaaw loolu, bu ngeen demee ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji sédd, ba ngeen nangu ko, dëkke,

Ñu merlooti Yàlla ca ndoxum Meriba ma, muy loraangey Musaa te ñoo ko waral.