TSK

TSK · Esther 2:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Rekab ak Baana, doomi Rimon ma dëkk Berot nag ñoo demoon kër Isboset, àgg fa ci biir tàngooru njolloor, fekk Isboset di for bët.

¶ Ba Asa buurub Yuda duggee ñaareelu atu nguuram, ca la Nadab doomu Yerbowam falu buur, jiite Israyil. Nadab jiite na Israyil ñaari at,

Yoram jàkkaarlook Yewu, ne ko: «Yewu, mbaa jàmm?» Yewu ne ko: «Ana nu jàmm di ame te sa bàkkaaru bokkaaley ndey Yesabel jógu fi, mook xërëmam yi ne xas?»

¶ Ci kaw loolu surgay Amoon lalal Amon pexe, bóom ko ca biir këram.

Ca lañu gis ñu bind ca ne Mardose moo boole woon Bigtan ak Teres, ñaari fara buntu kër buur ya laloon pexe ngir bóom Buur Aserus.